Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:3-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Ab soxor, taxawaayam du yàgg; ku jub garab la, reen ba ne kekk.
4 Jeeg bu jàmbaare day teral jëkkër ja, jeeg buy rusloo day semmal jëkkër ja.
5 Ku jub, yoon lay mébét; ab soxor di lal pexey wor.
6 Ab soxor, waxam am tëru la, day reye; kàdduy kiy jubal di musle.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi