Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:23-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:23-25 in Kàddug Yàlla gi

23 Nit ku ñaw day xam, ba ca; ab dof siiwal waxi dofam.
24 Njaxlaf, jiitu; yaafus, des gannaaw.
25 Njàqare day jeexal xolu boroom, wax ju neex di tooyal xolam.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi