Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:21-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:21-25 in Kàddug Yàlla gi

21 Ku jub du amu ay, ab soxor du tàggook musiba.
22 Aji Sax ji sib na fen-kat, safoo ku dëggu.
23 Nit ku ñaw day xam, ba ca; ab dof siiwal waxi dofam.
24 Njaxlaf, jiitu; yaafus, des gannaaw.
25 Njàqare day jeexal xolu boroom, wax ju neex di tooyal xolam.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi