Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Kuy ràbb lu bon lal pexey wor, kuy digle jàmm, am mbégte.
21 Ku jub du amu ay, ab soxor du tàggook musiba.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi