Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 12:2-4 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 12:2-4
in
Kàddug Yàlla gi
2
Ku baax, Aji Sax ji bége la; kuy fexe lu bon, mu daan la.
3
Ab soxor, taxawaayam du yàgg; ku jub garab la, reen ba ne kekk.
4
Jeeg bu jàmbaare day teral jëkkër ja, jeeg buy rusloo day semmal jëkkër ja.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms