Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:19-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Kàdduy dëgg, day sax dàkk; fen, xef xippi, mu wéy.
20 Kuy ràbb lu bon lal pexey wor, kuy digle jàmm, am mbégte.
21 Ku jub du amu ay, ab soxor du tàggook musiba.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi