Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Kàdduy dëgg, day sax dàkk; fen, xef xippi, mu wéy.
20 Kuy ràbb lu bon lal pexey wor, kuy digle jàmm, am mbégte.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi