Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:18-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Làmmiñu waxkat, jam-jami jaasi; kàddu gu xelu, garab la ci.
19 Kàdduy dëgg, day sax dàkk; fen, xef xippi, mu wéy.
20 Kuy ràbb lu bon lal pexey wor, kuy digle jàmm, am mbégte.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi