Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Làmmiñ reggal na boroom; ñaq, jariñu.
15 Na dof di jëfe, njub la ci moom; dégg ndigal rafet um xel la.
16 Ab dof bu meree, mu gaawa feeñ; ku teey, tanqamlu saaga.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi