Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:12-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Ab soxor ay xemmem alal ju lewul, ku jub garab la, reen baa ko meññal.
13 Bàkkaaru làmmiñ dugal na boroom, ku jub mucc ci njàqare.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi