Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 11:4-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 11:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Alal du jariñ bésu mbugal; jub, mucc ci gàtt fan.
5 Ku mat, njekk xàllal la; coxor daaneel boroom.
6 Jubalal, sa njekk musal la; ab workat day bëgge, ba far keppu.
Kàddu yu Xelu 11 in Kàddug Yàlla gi