Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 11:21-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 11:21-23 in Kàddug Yàlla gi

21 Ab soxor mbugalam du jaas, wóor na; te ku jub, saw askan mucc.
22 Taaru jongama ju xel ma gàtt, mooy jaaro wurus ci noppu mbaam-xuux.
23 Ku jub, lu baax rekk lay sàkku; soxor biy yaakaar, mujje mbugal.
Kàddu yu Xelu 11 in Kàddug Yàlla gi