Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 11:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 11:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Aji Sax ji bañ na njublaŋ, safoo maandute.
21 Ab soxor mbugalam du jaas, wóor na; te ku jub, saw askan mucc.
Kàddu yu Xelu 11 in Kàddug Yàlla gi