Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 11:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 11:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Saxoo njekk, dund; sàlloo mbon, dee rekk.
20 Aji Sax ji bañ na njublaŋ, safoo maandute.
Kàddu yu Xelu 11 in Kàddug Yàlla gi