Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 11:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 11:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Waxi xeebaate ñàkk bopp la, ku am ag dégg day noppi.
13 Kuy wër di sos dangay wuññi sutura, ku jara wóolu dangay am bàmmeelu biir.
14 Tegtal tumurànke, am réew suux; digle bare, ndam dikk.
Kàddu yu Xelu 11 in Kàddug Yàlla gi