Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 11:10-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 11:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Ku jub baaxle, waa dëkkam bànneexu; ab saaysaay saay, mbégte dim riir.
11 Barkeb ku jub teral nab dëkk, kàddug ku soxor tas nab dëkk.
Kàddu yu Xelu 11 in Kàddug Yàlla gi