Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 10:8-11 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 10:8-11
in
Kàddug Yàlla gi
8
Ku rafet xel day jëfe santaane, ab dof waxa wax, ba loru.
9
Maandu, fegu; dëng, weeru.
10
Piiseek làq-làqal, sabab njàqare; ab dof waxa wax, ba loru.
11
Kàdduy ku jub bëtu ndox la, day naatal; waaye ku soxor, wax ja làq fitna.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms