Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:7-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ku jub barkeel, saw tur du fey; ab soxor, turam seey.
8 Ku rafet xel day jëfe santaane, ab dof waxa wax, ba loru.
9 Maandu, fegu; dëng, weeru.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi