Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 10:7-10 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 10:7-10
in
Kàddug Yàlla gi
7
Ku jub barkeel, saw tur du fey; ab soxor, turam seey.
8
Ku rafet xel day jëfe santaane, ab dof waxa wax, ba loru.
9
Maandu, fegu; dëng, weeru.
10
Piiseek làq-làqal, sabab njàqare; ab dof waxa wax, ba loru.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms