Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:3-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji du seetaan ku jub, di xiif, waaye day xañ ab soxor la mu xemmem.
4 Yaafus, walaakaana; farlu, woomle.
5 Ku ngóob jot, nga góob, xelu nga; ngóob taxaw, ngay nelaw, gàcce la.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi