Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:28-29 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:28-29 in Kàddug Yàlla gi

28 Ku jub day séentu mbégte, gis ko; ab soxor yaakaar, yàkki.
29 Aji Sax jeeki nammeelam rawtu la ci ku mat, di sànkute ci kuy def lu bon.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi