Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 10:20-23 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 10:20-23
in
Kàddug Yàlla gi
20
Kàddug ku jub di ngën-gi-xaalis, xelum coxor amul solo.
21
Kàdduy ku jub jariñ na ñu bare, dof ñàkk na bopp, ba far dee.
22
Barkeb Aji Sax jeey maye alal, kër-këri taxula barele.
23
Jëf ju bon la dof di foye; ku am dég-dég safoo lu xelu.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms