Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:16-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:16-19 in Kàddug Yàlla gi

16 Ku jub jot peyam, dunde; ab soxor di bàkkaare alalam.
17 Yaru, gudd fan; sàgganey àrtu, sànku.
18 Ku la nëbbal mbañeel, da lay fen; kuy wër di sos, ab dof la.
19 Wax ju bare, moy ñàkku ca; ku moom sa làmmiñ, xelu nga.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi