Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Ku rafet xel day xam, ne cell; bu dof noppiwul, yàqule teew.
15 Alal day aar boroom ni ab tata, ñàkk di lor baadoolo.
16 Ku jub jot peyam, dunde; ab soxor di bàkkaare alalam.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi