Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Mbañeelak ayoo; cofeelak jéggale bépp tooñ.
13 Kuy dégg, say wax rafet; te ku ñàkk bopp, yelloo yetu gannaaw.
14 Ku rafet xel day xam, ne cell; bu dof noppiwul, yàqule teew.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi