Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 7:16 in Wolof

Help us?

JËF YA 7:16 in Téereb Injiil

16 Gannaaw loolu ñu yóbbu seeni néew Sisem, dugal leen ca bàmmeel, ba Ibraayma jëndoon ak xaalis ca doomi Amor ca Sisem.
JËF YA 7 in Téereb Injiil

Jëf ya 7:16 in Kàddug Yàlla gi

16 Gannaaw gi lañu toxal seeni yax ca Sikem, denc leen ca bàmmeel, ba Ibraayma weccikoo woon xaalis ca doomi Amor ca Sikem.
Jëf ya 7 in Kàddug Yàlla gi