Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 3:3 in Wolof

Help us?

JËF YA 3:3 in Téereb Injiil

3 Bi mu gisee Piyeer ak Yowaana nag, ñuy dugg ca kër Yàlla ga, mu dékk leen loxo.
JËF YA 3 in Téereb Injiil

Jëf ya 3:3 in Kàddug Yàlla gi

3 Waa ja gis Piyeer ak Yowaan, ñuy dugg ca kër Yàlla ga, mu di leen sarxu.
Jëf ya 3 in Kàddug Yàlla gi