Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 2:7-8 in Wolof

Help us?

JËF YA 2:7-8 in Téereb Injiil

7 Ñu waaru te yéemu naa: «Gisleen, ñiy wax ñépp, ndax duñu waa diiwaanu Galile?
8 Naka la mana ame nag, nu di leen dégg, kenn ku nekk ci nun, ñuy wax ci sa làmmiñ, wi nga nàmp?
JËF YA 2 in Téereb Injiil

Jëf ya 2:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Ñu boole waaru ak yéemu, naa: «Ñii di wax nii ñépp, xanaa duñu waa Galile?
8 Ana nu kenn ku nekk ci nun nag mana dégge ñuy wax ci làmmiñ wi nga nàmp?
Jëf ya 2 in Kàddug Yàlla gi