Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 2

Jëf ya 2:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Booba ay toppkati yoonu Yawut a nga dëkke Yerusalem, te bawoo ci xeeti àddina yépp.
6Naka la coow li jolli, nit ñi daje, ku nekk ci mbooloo mi dégg ñuy làkk sa làkku bopp, mbooloo ma jaaxle.

Read Jëf ya 2Jëf ya 2
Compare Jëf ya 2:5-6Jëf ya 2:5-6