Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 2:25 in Wolof

Help us?

JËF YA 2:25 in Téereb Injiil

25 Daawuda wax na ci mbiram ne: “Saa su ne gis naa Boroom bi ci sama kanam; gannaaw mu ngi ci sama ndijoor, duma raf.
JËF YA 2 in Téereb Injiil

Jëf ya 2:25 in Kàddug Yàlla gi

25 Daawuda wax na ci mbiram ne: “Maa doon gis Boroom bi fi sama kanam saa su nekk, ndijoor la ma fare, ba duma tërëf.
Jëf ya 2 in Kàddug Yàlla gi