Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 2:23 in Wolof

Help us?

JËF YA 2:23 in Téereb Injiil

23 Moom nag jébbale nañu ko, jaar ci nas, bi Yàlla dogaloon te xam ko lu jiitu; te yéen rey ngeen ko ci daaj ko ci bant, jaarale ko ci loxoy bàkkaarkat.
JËF YA 2 in Téereb Injiil

Jëf ya 2:23 in Kàddug Yàlla gi

23 Nit kooku ñu jébbale ni ko Yàlla dogale te nasoon ko lu jiitu, yeena ko daajloo yéefar yi ci bant, reylu ko.
Jëf ya 2 in Kàddug Yàlla gi