Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 1:6 in Wolof

Help us?

JËF YA 1:6 in Téereb Injiil

6 Bi ñu dajaloo ak moom nag, ñu laaj ko: «Boroom bi, ndax ci jamono jii ngay yékkatiwaat nguuru Israyil?»
JËF YA 1 in Téereb Injiil

Jëf ya 1:6 in Kàddug Yàlla gi

6 Naka lañu daje fa moom, daldi koy laaj, ne ko: «Sang bi, ndax ci jii jamono ngay sampaat nguurug Israyil?»
Jëf ya 1 in Kàddug Yàlla gi