Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 1:16 in Wolof

Help us?

JËF YA 1:16 in Téereb Injiil

16 Mu ne leen: «Bokk yi, li Xel mu Sell mi waxoon ci Mbind mi jaarale ko ci gémmiñu Daawuda, fàww mu am. Waxoon na ci mbirum Yudaa, mi wommat ñi jàpp Yeesu
JËF YA 1 in Téereb Injiil

Jëf ya 1:16 in Kàddug Yàlla gi

16 «Bokk yi, Mbind mi moo waxe woon Noo gu Sell gi lu jiitu, ci gémmiñu Daawuda, wax ju jëm ci Yuda mi jiite nit ña, ba ñu jàpp Yeesu. Mbind moomu nag fàww mu sotti.
Jëf ya 1 in Kàddug Yàlla gi