Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 18:5 in Wolof

Help us?

JËF YA 18:5 in Téereb Injiil

5 Waaye bi Silas ak Timote jógee diiwaanu Maseduwan, egg fa, Pool jublu ci xamle kàddu gi, tey dëggal ci Yawut yi naan Yeesu mooy Almasi bi.
JËF YA 18 in Téereb Injiil

Jëf ya 18:5 in Kàddug Yàlla gi

5 Ba Silas ak Timote dikkee, bàyyikoo diiwaanu Maseduwan, Póol xintewootul lu moy di xamle kàddu gi, di seereel Yawut yi ne Yeesu mooy Almasi.
Jëf ya 18 in Kàddug Yàlla gi