Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
JËF YA 17:7-9 in Wolof
Help us?
JËF YA 17:7-9
in
Téereb Injiil
7
te Yason a leen dalal. Ñoom ñépp dañoo bañ ndigali buur Sesaar ne, am na beneen buur bu ñuy wax Yeesu.»
8
Bi ko mbooloo mi ak àttekat yi déggee, ñu daldi jaaxle lool.
9
Noonu nanguwuñoo yiwi Yason ak ñi ci des, lu dul bi ñu leen bataleelee dara.
JËF YA 17 in Téereb Injiil
Jëf ya 17:7-9
in
Kàddug Yàlla gi
7
te Yason a leen dalal. Ñoom ñépp a xëtt ndigali buur Sesaar, te naan am na beneen buur bu ñuy wax Yeesu.»
8
Ba mbooloo ma ak àttekati dëkk ba déggee loolu, dañoo jaaxle.
9
Ba loolu amee ñu feyloo Yason ak ña ca des daan ba ca war, door leena yiwi.
Jëf ya 17 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms