Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 16

Jëf ya 16:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Ba loolu amee alal ja njaatigey ndaw sa yaakaaroon, réer leen, ñu jàpp Póol ak Silas, diri, yóbbu ca pénc ma, fa kanam njiit ya.
20Ñu taxawal leen fa àttekat ya, ne: «Ñii ñoo yëngal sunu dëkk bi, di ay Yawut
21yuy xamle aada yoy, nun ñiy waa Room, sañunu koo nangu, sañunu koo jëfe.»

Read Jëf ya 16Jëf ya 16
Compare Jëf ya 16:19-21Jëf ya 16:19-21