Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 16

Jëf ya 16:18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Noonu la jàppoo ay fani fan, ba Póol mujj xajootu ko. Mu walbatiku ne rab wa: «Maa la sant ci turu Yeesu Almasi, génnal ci ndaw si.» Rab wa daldi génn ca saa sa.

Read Jëf ya 16Jëf ya 16
Compare Jëf ya 16:18Jëf ya 16:18