Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 15:40 in Wolof

Help us?

JËF YA 15:40 in Téereb Injiil

40 Pool tànn Silas, dem; bokk ya dénk leen ci yiwu Boroom bi;
JËF YA 15 in Téereb Injiil

Jëf ya 15:40 in Kàddug Yàlla gi

40 Póol moom, taamu Silas, daldi ànd ak moom dem, gannaaw ba leen bokk ya dénkee Boroom bi ciw yiwam.
Jëf ya 15 in Kàddug Yàlla gi