Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 15:13-15 in Wolof

Help us?

JËF YA 15:13-15 in Téereb Injiil

13 Bi ñu noppee, Saag jël kàddu ga ne:
14 «Bokk yi, dégluleen ma! Simoŋ nettali na, ni Yàlla seetsee bu jëkk ñi dul Yawut, ngir sàkku ci ñoom xeet wu ñu tudde turam.
15 Te loolu sax dëppoo na ak li yonent yi tëral; ñu bind ne:
JËF YA 15 in Téereb Injiil

Jëf ya 15:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Ba ñu noppee, Yanqóoba àddu ne: «Bokk yi, dégluleen ma.
14 Simoŋ xamle na, ni Yàlla yége jaambur ñi ca njàlbéen, ba sàkke ci seen biir, xeet wu mu tudde turam.
15 Te loolu dëppoo na ak kàdduy yonent yi, ndax bindees na ne:
Jëf ya 15 in Kàddug Yàlla gi