Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 13:50 in Wolof

Help us?

JËF YA 13:50 in Téereb Injiil

50 Waaye Yawut ya xiir ay jigéen, ñi woomle te farlu ci diine, ñoom ak magi dëkk ba, ñu fitnaal Pool ak Barnabas, ngir génne leen réew ma.
JËF YA 13 in Téereb Injiil

Jëf ya 13:50 in Kàddug Yàlla gi

50 Teewul Yawut ya xiirtal tuubeen yu jigéen yi gëna ràññiku, ak kàngam yu góor yi ci dëkk bi. Ñu daldi bundxatal Póol ak Barnaba, génne leen réew ma.
Jëf ya 13 in Kàddug Yàlla gi