Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 13:22 in Wolof

Help us?

JËF YA 13:22 in Téereb Injiil

22 dellu falal leen buur bu tudd Daawuda, mu seedee ko nii: “Gis naa Daawuda, doomu Isayi, ku ma neex ci sama xol, te dina def lépp luy sama coobare.”
JËF YA 13 in Téereb Injiil

Jëf ya 13:22 in Kàddug Yàlla gi

22 Mu jële ko fa, sampal leen Daawuda, muy buur bu mu seedeel ne: “Maa ràññee Daawuda doomu Yese, ji sama xol jubool, te mooy jëfe mboolem samay coobare.”
Jëf ya 13 in Kàddug Yàlla gi