Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 12:3 in Wolof

Help us?

JËF YA 12:3 in Téereb Injiil

3 Bi mu gisee nag ne mbir moomu neex na Yawut ya, mu daldi jàpp it Piyeer; fekk loolu daje ak bési màggalu Yawut, ga ñuy wax Mburu ma amul lawiir.
JËF YA 12 in Téereb Injiil

Jëf ya 12:3 in Kàddug Yàlla gi

3 Mu gis nag na mbir ma neexe Yawut ya, ba tax mu teg loxo Piyeer, moom itam; loola yemook bési màggalu Mburu mu amul lawiir.
Jëf ya 12 in Kàddug Yàlla gi