Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 12

Jëf ya 12:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Gannaaw ba Piyeer ràññee loolu, daa dem kër Maryaama, ndeyu Yowaan Màrk, fekk ñu bare daje foofa, di ñaan.
13Piyeer fëgg buntu kër ga, mbindaan mu ñuy wax Rodd dikk.

Read Jëf ya 12Jëf ya 12
Compare Jëf ya 12:12-13Jëf ya 12:12-13