Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 11:13 in Wolof

Help us?

JËF YA 11:13 in Téereb Injiil

13 Mu nettali nu ne gis na malaaka, feeñu ko ca këram ne ko: “Yónneel ca dëkku Yope, woolu Simoŋ, mi ñu dàkkentale Piyeer.
JËF YA 11 in Téereb Injiil

Jëf ya 11:13 in Kàddug Yàlla gi

13 Mu xamal nu ne malaakaa ko feeñu ci néegam, ne ko: “Yebleel ca Yope, nga woolu Simoŋ, ma ñu dàkkentale Piyeer.
Jëf ya 11 in Kàddug Yàlla gi