Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 10:44 in Wolof

Help us?

JËF YA 10:44 in Téereb Injiil

44 Bi Piyeer di wax loolu, Xel mu Sell mi wàcc ci kaw ñépp ñiy déglu kàddu ga.
JËF YA 10 in Téereb Injiil

Jëf ya 10:44 in Kàddug Yàlla gi

44 Ba Piyeer di wax kàddu googu, Noo gu Sell gi daldi wàcc ci kaw mboolem ñay déglu kàddu ga.
Jëf ya 10 in Kàddug Yàlla gi