Text copied!
Bibles in Wolof

JËF YA 10:31 in Wolof

Help us?

JËF YA 10:31 in Téereb Injiil

31 mu ne ma: “Korney, say ñaan nangu na, te say sarax egg nañu fa kanam Yàlla.
JËF YA 10 in Téereb Injiil

Jëf ya 10:31 in Kàddug Yàlla gi

31 Mu ne ma: “Korney, nangu nañu say ñaan, te nemmiku nañu say sarax fa kanam Yàlla.
Jëf ya 10 in Kàddug Yàlla gi