Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 10

Jëf ya 10:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Sér baa nga def mboolem boroom ñeenti tànk, ak dundoot yiy raam, ak mboolem njanaaw.
13Mu am baat bu jib, ne ko: «Piyeer, jógal, rey te lekk.»

Read Jëf ya 10Jëf ya 10
Compare Jëf ya 10:12-13Jëf ya 10:12-13