Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Filib - Filib 4

Filib 4:8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Li ci des nag bokk yi, moo di lii: mboolem lu dëggu, ak mboolem lu tedd, ak mboolem luy njub, ak mboolem lu set, ak mboolem lu jekk, ak mboolem lees di rafetlu, ndegam lu nawlu la te yelloo ngërëm, na leen loola soxal.

Read Filib 4Filib 4
Compare Filib 4:8Filib 4:8