Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Filib - Filib 3

Filib 3:9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9ngir ma mana feeñe ci biir Almasi, fu ma yaakaarul sama njekku bopp gu ma feyoo sàmm yoonu Musaa, xanaa di yaakaar njekk gu laloo ngëm gi ma gëm Almasi. Njekk googu fa Yàlla la bawoo te gëm Almasi moo koy maye.

Read Filib 3Filib 3
Compare Filib 3:9Filib 3:9