Text copied!
Bibles in Wolof

FILIB 1:6 in Wolof

Help us?

FILIB 1:6 in Téereb Injiil

6 Wóor na ma ne Yàlla mi tàmbali jëf ju baax jii ci yéen, dina ci sax, ba bésu Kirist Yeesu ñëw.
FILIB 1 in Téereb Injiil

Filib 1:6 in Kàddug Yàlla gi

6 Te lii kat, bir na ma; ki tàmbali jii jëf ju baax ci yeen, dina ko àggale ba keroog bésub Almasi Yeesu.
Filib 1 in Kàddug Yàlla gi